Mouhammad Salih Al-Mounajjid: Wôtékat la bu cosànô Siri, mi ngi juddu ci 30-12-1380 ci gàddàygi, mi ngi mâggé Riyad janŋŋé arabi sawdit ci ay borômi xamxam yu limu, bôkkna ci ñoñu: Cheikh Ibn Bâz ak Cheikh Ibn Usaymîn
Môy Mouhammad dômou Sâlih dômou Mouhammad dômou Soulaymâne dômou Abdourahmane dômou Ousmane dômou Abdoullah dômou Abdourahmane dômou Ahmad dômou Mouqbil thi jâbôtouk Mouqbil thi njabôtouk Rayyis Alwouhaybî At-tamîmî, gnènntèloul mâmame lagnou dâkkanetalé Ousaymîne mou sîwéko, té mingui bôkk thi
No Description
Môy Cheikh Mouhammad Ibn Abdoul Wahab Ibn Soulaymane bôkk thi guîrouk Tamîm, mi ngui joudd thi 1115 thi gâddây gui thi deukk bou toudd Ouyayna thi arabi saoudite, beurina loumou taalîf. Borôm kham kham yi mândou yi sédèlnagnouko kham-kham ak am dîné ak tégé thi yône wou joup. Fâtouna (Yalla....
No Description
Sâdou dômou Saîd Al- Ghâmidî sîwé bâtam bou nèkh bi, yilimâne ak khoutebakatou jâkka bou gnouy wakh Kânou -Dammam- thi Arabi Sawdite, di aji sawtou centarou al-khourâne bi gnou douppé Imâm Ach-Châtibî tèm nèkk thi Dammam.
No Description
Yilimâne thi jâkka Makka
Yilimâne ak khoutbakatou Makka
Yilimane ak khoubakate thi jâkka Yonnènetebi (Yalla na Yalla joulli thi môme)