×
Image

Moustapha Ismail

No Description

Image

Housseyn dômou Abdoul Aziz Ali Cheikh

Yilimane ak khoubakate thi jâkka Yonnènetebi (Yalla na Yalla joulli thi môme)

Image

Abdoul Bârî As-Soubaytî

Yilimane ak khoubakate thi jâkka Yonnènetebi (Yalla na Yalla joulli thi môme)

Image

Mahmud Ali Bannaa

Mi ngi juddo égipte ci atum 17-désambr-1926. Mi ngi wattoo Alxuràne ci daara dëkkam ci seriñ bu tudd Mussa Minetàs ci bi mu amé fukki ate ak bènn la mookal. Ginnaw gi mu toxu Tantaa ngir jaŋŋ xam xamu charia. Foofu sax la jëlé xamxamu jaŋŋinu alxuràn ci seriñam bii....

Image

Ibrahim Khali Lô

No Description

Image

Fâriss Abbâd

Fâriss Abbâd: mi ngui thiôssânô Yémène.Di borôm bâte bou nèkh té râgnèkou. Enrezistéréna ay téré kham-kham ak Kâmil bou mate. Bôkkna thi yolimânou jâkka Alioune dômou Abî Tâlib thi Ad-dawha thi sôwwou Arabi Sawdite

Image

Abdoulla Ali Basfar

Mi ngi juddo jidda ci 09-11-1381 ci gàdday gi. Amna Bak ci ŋàŋum lislam ci jànŋukày bu kawé bi ñu duppé Al-Malik Abdul Aziz bi ci jidda ci 1406 ci gàddày gi.Ak Majester ci Fikh ak Ciosànam ci jànŋukày bu kawé bi ñu duppé Ummul Qurà bi ci Makka, binndoone....

Image

Ahmad Ali Ajami

Mi ngi juddoo xabar ci atum 24-02-1968. Amna doctora ci tafsir ci kémuk gëna baaxlé. Mi ngi binndoone ci Faraŋfàccé yoonu firi Alxouràne. Amna tamite majester ci Pakistan. Ak Bac ci universitèp Muhammad Ibn Saoud

Image

Mahmoud Khalîl Al-Houssary

Cheikh Mahmoud Khalîl Al-Houssary môy serignou mbôlème jânggkatou égipteyi, di jîtémbôtâyou jânggkatou al-khourane yithi addounabi. Mi ngui jouddou thi tâmbalik atoum ajj thi atoum 1335 thi gâddây gui tôllôk 17 sèptembar thi atoum 1917 thi atoup toubap. Thi deukk bougnou douppé Chabrae namla bi jôkk thi tâMahmoud Khalîl Al-Houssarynetâ tho....