×
Image

Cheikh Abou Bakr Ach-Châtiry

Cheikh Abou Bakr Ach-châtiry mi ngui joudd atoum 1970 thi jidda môy yilimânou joumây Al-Fourqâne thi Nassîm Jidda. Mi ngui dègnth sokhna am thi gnènnti dôm. Dâkkanetalam môye Abou Abdourrahmane. Ay lijâssâm thi jângg: dipolomou jângg Al-khourâne bou tèddbi thi hafs bi jogé thi Âssim thi serignam bî di Aymane....

Image

Muhammad Jibril

Mi ngi juddo tahuriyà. Amna lijàsap lisense ci charia ak yoon ci jànŋukaye bu kawé bii di Azhar. Mi ngi jiité nafilay koor ci jàkkàp Amr Ibn Al-Âs ci kapital bi dooré ci atum 1988.

Image

Mor Kébé

No Description

Image

Imame Hasane Sarr

No Description

Image

Khâlid Al-Khahtâny

Yilimâne thi jâkkâp ndème si Yallassi Abdour Razzâkh Khinebar Al-Anessâry -gokhoup An-Nakhil thi Dammâm

Image

Abdur Rashid Sufy

Touram môy: Abdur Rachid Ibn Cheikh Ali Sufy. Lu aju ci démbam: mi ngi juddi ci atum 1964 ci Somali. Pappam môy fóré bi tudd Ali Ibn Abdur Rahmane Sufy (Ubbékabup Somali ak kafa gëna kawé ci jâŋŋup Al-xuràn) muy kifa ngëkka dugal ak tassâré xamxam ngaŋŋu Al-xurân ak ngaŋŋine....

Image

Ali Jâbir

No Description

Image

Mâhir dômou Hamad Al-Mouaykhilî

Yilimane ak khoubakate thi Makka

Image

Mouhammad Ayyoûb

No Description

Image

Xàlid Ibn Ali Al-Ghàmidi

Mi ngi juddoo Màkka. Amna bak bookk ci ñici ràññéku ci wàllup Al-Xuràn ak sunna ak cossànu diiné ci universiep Ummoul khurà. Ci atum1412 ci gàddày gi nékkna kuñu jiital foofé ci xamxamam ci waallu nŋàggiinum alxuràn. Ci atup 1416 ci gàddày gi la am majester ci al-xuràn akiy xamxamam....