Mi ngui thiôssânô irak, dèfna ay jalôré thi njânggoum Al-Khourâne bou tèdd bi, niki nônou enrezistréna ak kâmil you bari
Abdoullah Abdoul Ghany Al-Khayyâte -Yalla nako Yalla yeurem- nèkkônna yilimanou jakka makka
Yilimâne thi Joumây Ad-Dakhîl thi gokhoup Ghirnâta thi Riyâd
No Description
Mi ngi cosanoo Kuwét. Di boroom bàte bu ràññéku enresistéréna bénn kamil ci hafs ak khàluun. Li yémé ci mbiraù mooy né mooy goolup ékipe national bu futbalbi
Mi ngi judd 19-06-1398 ci gàddày gici jidda. Ci atum 1415 ci gàddày gi la mookaal alxuràn. Amna majestér ci saytu mëne mënup nite. ak bac ci porotochimi. pilote la ci arabisawdite. Mi ngi tàmmbalé jitté ci atup 1415 ci gàddày gi ci kaar ci jàkkàp Al-Baghdàdi ginàwgi ci jàkkàp....
Kénne la thi yilimani Arabi Sawdite. Mi ngui jouddô Mâkka, fa la jânggé ba paré. Jânggalékate la thi kaba gui thi pâth gui ajou thi Al-Khourane. Jânggna kâmil thi radiop al-khourâne, ak aykamil thi yônnoup châtibiyya.
Wâ égypte la, di kènn thi gniy jângg Al-Khourâne thi foukk jânggine yi thi radio Koweit bi. Di ap nôddkate thi jâkkâp Moûdy Al-Oumr, nèk kènn thi âttékate yiy saytou njânggkate yi.
No Description
Mi ngui guénné Université bou Madina, di yilimane ak xoutbakat, râgnékou thi tôloup wôté jëmé ci Yalla