Ci jànŋŋkat yi siiw la book. Mi ngi judd 1974. Yilimàne la ak khoutbakate ci Jidda (Arabi Sawdite). Sitam mooy: http://www.alrfaey.org
Moudi borôm kham-kham bou sîw thi pakistan
Mi ngi mookkalé alkhouràne ci ap centarup Az-zayd ci bi muy am 13 ate ci loxoop Ghulàm Hussayn mi ko jox liàssa. Jàŋŋna ci Cheikh Ibrahim Al-Akhdar mi jiité jàŋŋkateyi ci madina fa jàkka Yonéneteba (Yalla na yalla julli ci moom té dooliko jàm) mi ko jox lijaasa ci hafs.....
Mi ngui jouddô thi Ordone le 10-Mai-1979, yilimane ak khoutbakate thi jâkkâp oummoul Mouminine dôré thi 1999 ba fî gnou tôll. Amna bac thi charia, geuna mâth thi thiôssâni dîné. Amna tamite Majèstère thi université bi mâth thi kham-khami Al-Khourane (W.I.S.E.)
Mi ngui jouddô Riyad thi gokh bou toudd houllatoul Khasmâne thi arabi sawdite thi atoum 1385 thi gâddây gui
Mi ngui joudd thi 5-5-1980. Jânggalékate di yilimane thi jâkkâm Al-Ikhlâs thi Arabie Saoudite.
Kènne la thi gniy jânggalé thi Makka, mi ngui askanô Syrie. Di kou geuna mâth thi njâgginoum Al-khourâne ak kham-kham yi thi ajou. Jânggé thi pâpâm di ap jânggkate bou râgnékou tamite toudd Said Al-Abdallah (Yalla nako Yalla yeureum) (nékkône njîtou jânggkate yi thi Hama). Jânggaléna Oummoul Khoura. Enregistréna foukki....
Jânggkate la bou thôssânô Egypte thi Al-Bouhayra, paréna thi njângginou Al-Khourâne yi, niki nônou jânggna thi université bi mâth thi kham-khamiy Al-Khourane. Yilimane la ak khoubakate thi Centre Islamique bi thi New York
Mi ngui thiôssânô Yémène, yilimâne la ak khoutebakate thi joumây Khalid Ibn Al-walîd thi katar
Mi ngui jouddô Mâkka, amna bak thi njanggate Alkhourâne thi facultèp janggalékate yi tém nèkk jidda. Bôkkna thi yilimâni jâkkay jidda thi arabi sawdite