×
Image

Serigne Elimane Ndiaye

No Description

Image

Alioune Gueye

No Description

Image

Sahl Ibn Zayne Yâssine

No Description

Image

Mouhammad Sâlih Alim Châh

Mi ngui thiôssânô Pakistan, di borôm bâte bou nèkh akoup jânggine bou jâr yône

Image

Ahma Ahmad Nuayna

Ap janŋkate la di ap facckate. Mi ngi juddoo kafr Cheikh ci 2gypte ci atum 1954. Dugna ci facultém médcine ci jànŋukay bu kawé bi ci eskanedari. Bi mufa paré mu ligéy ca lopitàlba. Rajoo ak télé bu egypte défnako jàŋkatu alkhouràne ci atum 1979

Image

Taha Ibn Mouhammad Al-Fahd

Jànŋkatu Alkhouràne la ak yaxu xamxa ci bàte bu ràññéku ak jooxé bu jàr yoone dajàlénaci lu bari ci sitambi:http://taiser.net

Image

Muhammad Iwad Al Harbàwii

Mi ngi génné azhar ci jaŋŋkàyu lislam bi ak làkkup arap, famu amé lijàssa bu kawé ci jàŋŋin yi, ak lijàssap maacc si. Amnaci Doctora. Jàŋŋaléna ci azhar ay ate yu limu ak ci ay jàŋŋukaay yu arabi sawdite, ni mu fassaneté ak facultép jàŋŋalékate bi ci riyaad. Bokkna ci....

Image

Moussa Bilal

Yilimane la di khoutbakate ak jânggalékate thi universitèp An-Nour bi thi Makka. Bokkna thi âttékate thi concour international bou Doubai bi ajou thi Al-Khourane thi atoum 1420 ak 1433 thi gâddây gui

Image

Majdy Al-Baltâjy

Jânggkatela bou Egypte, di borôm bâte bou nèkh. Amna ap lijâssa thi foukki (10) jânggine yi. Enregistréna ak kâmil thi ay jânggine you wouté

Image

Ahmad Tàlib Hamid

Dàkkantalam mooy Bàyu Az-zoubayr, mi ngi tudd Ahmad Tàlib Hamid Ibn Abdul Hamid Ibn Muzaffar Xàn. Judduna ci Riyàd ci atum 1401 ci gàddày gi. Mi ngi jànggé ci fakultép saria bi ci uniwérsitép ba amfa bak. Ginàw ngi mu am Masestér ci àtté ci fiq muqàran. Di ligéyé kom....