×
Image

Bandar Ibn Abdoul Aziz Baliila

Mi ngi juddoo Makka ci atum 1395 ci gàddày gi; fala dooré jàŋŋ ba am bak. Amna majestér ci atum 1422 ci gàaddày gi ci fikh ci universitém Ummul Xurà. Amna itam doctoorà ci fikh ci atum 1429 ci gàddày gi ci universiép Madiina. Jàŋŋaléna fikh bu kawé fa Kàbaga,....

Image

Moustapha Gharby

Jânggkate la bou goumba askanô maroc, dagne koy méllal né sakh môy serignou jânggkate yi. Mi ngui joudd thi atoum 1964.

Image

Walîd Ali Mouhammad An-Nâihî

Mi ngui jouddô Libye, mi ,gui jeul gnârèlou palass bi thi jonganetèp Al-Khourane biy am Dubay

Image

Ahmad Al-Misbâhî

Wâ Yémène la, mi ngui jângg Al-khourane thi joumây Oussama Ibn Zayd, jângg kham-kham thi Mahad Nour. Fi gnou tôll mi ngui jângg thi uniniversitèp bi mâth thi kham-khamou Téknolozi thi kapitalou Yémène di Sanâ

Image

Abdul Kabiir Al-Hadiidii

Mi ngi juddoo maroc ci atum 1963, mookalna Alxuràne. Amoone yitté lool ci fékké jotàyup xamxam biñu amal ci Darul Baydaa ci atum 1992, raññékuca ci wàllup jàŋŋate lislam. Yilimane la dip xutbakate ci jàkkap As-sabiil ci Darul Baydaa. Di kénn ci attékate ci joŋantép alxuràne bi ñu duppé Mouhammad....

Image

Al-Ouyoûnoul Koûchy

Mi ngui jouddô thi Âssify thi maroc thi atoum 1967, Yilimâne la ak khoutbakate thi jâkkâp Ânedalous thi Daroul Baydâ. Môkkalna Al-khourae mi miy am jourômgnéneti ate. Amna bac thi lètre. Kènne la thi gni gniy jânggé njânggoum warch bi jogé thi nâfie thi maroc

Image

Rachid Bal âliyya

Wâ Algérie la, amna ap kâmil boumou jângg thi warch bô khamné Ministère biy saytou mbiri dîné thi Algérie da thiy soukkandikou

Image

Abdul Ali Al-Anune

Mi ngi judoo Maroc ci atum 1947. Amn lijàsa ci warch ci yoonup Asbahàni ci Cheikh Ahmad Ibn Usmane Abul Alà. Ku ràññékula ci tajwiid té mi ngi ciy joxé ay binnd. Kennla ci ñiy fuglu wérug jaŋŋ al-khouràne. Taliifna: Naka laŋuy jaŋŋé Al-khouràn ci warch ci yoonup Azraq

Image

Yasine Al-Jazàiri

Mi ngi judd 1969 ci Al-Hiràs ci kapital bi, cosanoo ci Al-Buwayra. Amna lisense ci Chimi, ginnaw gi mu yéggali jàŋŋam ci cosaniy dinné ci charia. Mooy ki njeükka enresistré ap kamil ci warsh ci yoonup Al-Awrakh. Mi ngui jiité ci jàkk Abu Obayda Ibn Al-Jarràh.

Image

At-Tâzy Mouhammad Chahboûne

Jânggkate bou Maroc