Thi jânggkatou Maroc yi sîw yi la bôkk
Kènn la thi mbôtây gui thi arabi sawdite té mâth thi Al-Khourane akiy kham-khamam. Yilimâne la ak khoutbakate thi joumây njîte gui: Abdoullah Ibn Mouhammad thi riyâd
Jânggkatela bou askanô Egypte, yilimâne la ak khoubakate thi joumây Ar-Rîm thi compléksoup Doubai bi mâth thi kôm
Mi ngui askanô egypte toudd Ahmad Abdoul Fattâh Mouhammad Al-Haddâd, mi ngui joudd 25-08-1984. Thi universitèp Al-Azhar la amé lisensam thi lâkkou arapnthi atoum 2007. Akoup lijâssa mâjestèr thi wéral mbindd yi gnou fi bayyi thi attoum 2008, ak mâjestèr thi kham-khami Al-khourane ak foukki njânggine yi yi gnou tokhalé....
Mi ngui toudd Chirzâd Ibn Abdour-Rahmane Ibn Tâhir Ibn Hassane Al-Kâfy Al-Kourdy Ach-Châfi î, mi ngui jouddô thi beutt gânnârou Irak thi atoum 1968 thi fou gnouy wakh An-Nâmâiyya. Fôfou la jânggé thi ay serigne you bari niki: Cheikh Abdoul Latif Ibn Khalil As-Soufy, ak Cheikh Al-Hafiz Ali Ibn Houssayn....
Jânggikatoup égypte la. Mi ngui joudd thi atoum 1984, mi ngui am lijâssa thi njângginoup al-khourâne ak kham-khamou charia thi colèzoup njângginou al-khourâne bi thi Al-Azhar, ak thi njângg gou kawé. kènnela thi ngiy jânggalé thi markazoup Oustaz doctor Ahmad Issa Al-Minssrâwî di njîtou jânggkatou al-khourâne yi thi égypte.
Bosniâk la, di yilimane thi joummây Zaghrab thi Croissi
Oustazoup hadiss thi univèrsitèp Dâroul Ouloum bithi Inde, té môy njîtoup mbôtâyoup Borôm kham-khamou Inde yi bi ngua khamné môfay mbôtâyou joyllite bou geuna yâgg té reuy.
Mi ngui jouddô Médine thi 1382 thi gâddây gui. Amna doctôra thi piri thi atoum 1412 thi gâddây gui thi université ba. Nékkône yilimâne ak khoutbakate thi joumây Al-manâratayni thi Anebouriyya ak Khoubâ. Nèkkitame kène thi gniy saytou mbôtây giye jânggalé Al-khourane thi médine. Nimou dâne saytô ay liguèye you....
Môy Jazzâe Ibn Falîh As-Souwaylih, mi ngui jouddô Kowète thi atoum 1969, bôkkfa thi jânggkate yi sîw, mi ngui génné thi facultèp kham-khamou charia ak njâgg lislâm thi univèrsitèp Kowète gi ngua khamné falay jânggalé alkhourâne ak njângginam