×
Image

Taxawàyu jullite bi ci pakkiy jamono - (Wollof)

Khoutba gui mi ngui ajou ci: Xétum lislàm tay mi ngi roomb ay pakk yu wuuté ciy wéte yu limu yuy té mu taxawé liko war ci kaw suuf.kon lan mooy taxawàyu jullite bi ci pakkiy jamono.

Image

Ngënélu Baraxlu - (Wollof)

Khoutba gui mi ngui ajou ci: Ngënélu Baraxlu ak li ci wér sax ci sunna

Image

Ndékkàné yu aju ci kiñuy xayma ci xamxam - (Wollof)

Jullite bi warna fumu tollu muy tenkku ci téggini lislàm yi, ba ci fani xayma xamxam yi ñudëgmal di na jàdu mu tëkku ci téggini lislàm yi

Image

Am jote - (Wollof)

Khoutba gui mi ngui ajou ci: éé yaw doomu àdama guddi ak bëccëk dañuy ligéy ci yaw knnak ligéyal ci ñoom. Ana naka ngay jariño sa waxtu

Image

Jagléy Makka - (Wollof)

Khoutba gui mi ngui ajou ci: lénn ci jagléy Makk

Image

Yitèp lislaam ci koom koom ak souxaliku - (Wollof)

Khoutba gui mi ngui ajou ci: Yitèp lislaam ci koom koom ak souxaliku ci ay kaaddu yu matalé

Image

Wuuté aw aye la - (Wollof)

Khoutba gui mi ngui ajou ci: lèral jafé jafé yi ci wuuté

Image

Ragal Yalla - (Wollof)

Khoutba gui mi ngui ajou ci: Ragal Yalla jàréko ci sèttanetal alkhourane ak diko doolli

Image

Liy sippi jeüf - (Wollof)

Khoutba gui mi ngui ajou ci: Sabap yiy sippi jeüf

Image

Guissiine ak dokhalinu lislaam ci koom koom ak souxaliku - (Wollof)

Khoutba gui mi ngui ajou ci: Guissiine ak dokhalinu lislaam ci koom koom ak souxaliku

Image

Gaallankoorup koom koom ak souxaliku ci lislaam - (Wollof)

Khoutba gui mi ngui ajou ci: Guissiine ak dokhalinu lislaam ci koom koom ak souxaliku

Image

Sartiy tuup - (Wollof)

Khoutba gui mi ngui ajou ci: Sartiy tuup