×
Image

li ay oubbele youdiam thi mbiri tabaski - (Wollof)

li ay oubbele youdiam thi mbiri tabaski aylathie ak aytontou thi mbiri tabaski

Image

Hajjak ak atteme ak ay ganelam akdiekhantalam thi khetou islambi - (Wollof)

Nekana thi lerakl atte ahjj ak kagne kay war ,  touddou ganeli ahjj ak ay diekhantalam thi  khetou islam…

Image

Diamarlo digante wa dague ak wa nene - (Wollof)

Nekena thi leralni bokouna thi bakhou yalla  mouydef kebe kouywote thi loubakh nooukoy  koutre, ak leral khereniek yalla thi lolou…

Image

Dekane youma tale nielgui nara hajj - (Wollof)

Nekenathi  ay dekane youmatale niele keppe koubaga hajji diam thi karouk yalla ga…

Image

Ci yén la bawoo - (Wollof)

hotba Ci yén la bawoo

Image

Bouléne yaxx - (Wollof)

hotba bi cey li Bouléne yaxx

Image

Xàju nitñi ci rawanté jëm ci lu bàx - (Wollof)

Xàju nitñi ci rawanté jëm ci lu bàx

Image

Sax ginnaaw Koor - (Wollof)

Jaaduna ci ki goorgoorlu ci wéru koor mu wéyal loolu ginnaaw kori ak goorgoorlu woor jouroombenni fane ci sawwal

Image

Yoon yu lislam tërël ngir suxaliku - (Wollof)

Ku xool li addunabi di jàŋkonte ci ay jafé jafé ci koom, dina giss né jaaduna ñu wané yoon yunuy may suxaliku

Image

Ay jànggat yu aju ci wéru koor, ak lenn ci sababu yéx gu ndimmbalu Yalla tardé - (Wollof)

Ay jànggat yu aju ci wéru koor, ak lenn ci sababu yéx gu ndimmbalu Yalla tardé

Image

Nii la mag ñu baax ñi dàn mél ci wéru koor - (Wollof)

Soloss waxtàn wi mi ngui gëna feñ ci toxal guy ñuciy toxalal niko mag èu baax daan mànggé

Image

Attéy koor - (Wollof)

Khoutba gui mi ngui ajou ci: Dina jaadu ci bépp jullite mu yittéwoo lu aju ci àttéy diiném rawatina wéru koor