×
Image

Gadday al khourane khamleko ak ay mandargam ak ay misibame - (Wollof)

Nekenathi lreallane moy gadday ak khaourane ak ay mandar gam ak ay misibame

Image

Aoube guoumatale - (Wollof)

Nekenathi nontou ay lathie youbari bouknathi: atteb sede thi fose?...

Image

Hakhi dakadno - (Wollof)

Nekena thi leral amesolok tembi ,ak ni domiadama manouta doundou mome kasse,ak diane nioy ay dakadno ak yane moy hakhe yinelen wara diokh…

Image

Touki Diame Allakhira - (Wollof)

Touki Diame Allakhira

Image

Yawmal qiyâma - (Wollof)

Waxtàn wi gui ajou ci lèral faratâp fâttalikou déé ak wâjalko, ak jârouwây yi nite ki de rômb ba yégg thi kërëm gou moujj, ak toudd adîssoup Barâ Ibn zib (Yalla nako Yalla gërëm), ak saba yiy taxa dugg jana ak mucc ci safara

Image

Warèfoup bénnôp joulliteyi - (Wollof)

Waxtàn wi gui ajou ci lèral solo ngui né ci bénnô ak ngâgn tâxalikô akoup âttèm akiy sababam, lëkkëlô gui né thi ngeum ak bènnô ak lèral sabap yiy inndi bénnô

Image

Ap sânjjé la nguay wakh lôdoul dèf - (Wollof)

Wakhtâne wi gui mi ngui ajou ci: léral wakh yi rote thi sânjjé gui nèkk thi wax lodoul dèf. Nguénéloup jeuf bou sèll. Yéne wou dis wik thi jeujf bou sèll. Wax lôdoul dèf akiy loram thi ligèyoup lislam. Akiy jékhitam.

Image

Âjjana akiy khéwalam ak safara ak mbougalam - (Wollof)

Méllal Ajana akiy khéwalam

Image

Ngoro Sounna ak bidaa - (Wollof)

Waxtàn wi gui ajou ci lèral liy sounna ci labate ak wougny li ci nite gni sos

Image

Yây Aicha (Yalla nako Yalla geureum) - (Wollof)

Ay jotày la yuñu jaglèl sunu yày Aicha Yàlla nako Yàlla gërëm

Image

Deukkandô - (Wollof)

Waxtàn wi dafay leral deukkandô ak nimou mënoulé gnâkk gnou yittéwôko

Image

Yaroum lislâm - (Wollof)

Wakhtâne mi ngui aju ci yônou yaroum lislâm bou mucc ayib