Ay njaangate thi dunndup Yonènetebi (Yalla na Yalla joulli ci moom té dooliko jaam)
Khoutba gui mi ngui ajou ci: li Yonènetebi (Yalla na Yalla joulli ci moom té dooliko jaam) taxawé ci jànggalé ak yar ak tàggate wènn xète