×
Image

Ay jànggat yu aju ci wéru koor, ak lenn ci sababu yéx gu ndimmbalu Yalla tardé - (Wollof)

Ay jànggat yu aju ci wéru koor, ak lenn ci sababu yéx gu ndimmbalu Yalla tardé

Image

mko def thi fêtou Noël (moy fêt gi nasran yiy def thi gouddig 24 ak bisoub 25 décembre - (Wollof)

alouthaymin (di ab brom xamxam boumak) mko def thi fêtou Noël (moy fêt gi nasran yiy def thi gouddig 24 ak bisoub 25 décembre.

Image

Nii la mag ñu baax ñi dàn mél ci wéru koor - (Wollof)

Soloss waxtàn wi mi ngui gëna feñ ci toxal guy ñuciy toxalal niko mag èu baax daan mànggé

Image

Attéy koor - (Wollof)

Khoutba gui mi ngui ajou ci: Dina jaadu ci bépp jullite mu yittéwoo lu aju ci àttéy diiném rawatina wéru koor

Image

Yar guné ci Lislàm - (Wollof)

Nooy yaré sa doom?

Image

Taxawàyu jullite bi ci pakkiy jamono - (Wollof)

Khoutba gui mi ngui ajou ci: Xétum lislàm tay mi ngi roomb ay pakk yu wuuté ciy wéte yu limu yuy té mu taxawé liko war ci kaw suuf.kon lan mooy taxawàyu jullite bi ci pakkiy jamono.

Image

Ngënélu Baraxlu - (Wollof)

Khoutba gui mi ngui ajou ci: Ngënélu Baraxlu ak li ci wér sax ci sunna

Image

Ndékkàné yu aju ci kiñuy xayma ci xamxam - (Wollof)

Jullite bi warna fumu tollu muy tenkku ci téggini lislàm yi, ba ci fani xayma xamxam yi ñudëgmal di na jàdu mu tëkku ci téggini lislàm yi

Image

Am jote - (Wollof)

Khoutba gui mi ngui ajou ci: éé yaw doomu àdama guddi ak bëccëk dañuy ligéy ci yaw knnak ligéyal ci ñoom. Ana naka ngay jariño sa waxtu

Image

Mélokânoup janggalékatou Alkhourâne - (Wollof)

Yitté gignou wara jaglèle Alkhourâne

Image

Jagléy Makka - (Wollof)

Khoutba gui mi ngui ajou ci: lénn ci jagléy Makk

Image

Gènnouk khète : toûp gou deuggou - (Wollof)

Toûp gou deggou